Regole spostamenti

CHARTE YI FIRDER SA GUÉNE
  1. 1)DAKH MEUNA GUÉNE ITALIE DÉDÉTE MEUNO GUÉNE SAKEUR SOUFÉKE AMOULE LOUKAYE FIRDER NIAK GUÉNE SI KEUR YI FÉPLA SI GOKH YI SI REWMI DA WOTÉNAKO 10 MARS BI WÉSSOU MOUYE DIEKH BA 03 AVRIL SI WÉR BI DI NIAW DÉ TAK DER YI DINANOUKO SAYTOU .MAYOU NOU KÉN GUÉNE SAKEUR SOUFÉKE DANOULA WAKH GUA TOK SI KEURGUI WALA FEBBAR BI DALLA .TÉRÉNANOU KOUYE TOUKHOU DI DIEULE SAÎ BAGAS DIGUAYE SAP SI CARYI REWMI WALA YOMOME DIK DIEUMELÉ FÉNE FO DEUKOULE AK FOUMOUMENEUDONE KHAMA LIGUÉY BOUNEUNE TANIAK WALA LOUNEUNE TEKHAR SI WALOU WEERGOU YARAM SOUNÉKE DAGUA AME DIAFEDIAFÉ SA WALOU NOYI WALA YARAM BOU TAGUE BA WÉSSSOU 37,5% DIGUEL NANOULA GUA TOK SA KEUR GUA TOPE SA NIGUEL KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM DAGUA SORRI NITE YI LOUMENEUNE
  2. YANE MOWARATAKH GUAGUÉNE SA KEUR ? SOUFÉKE DAGUA BEUK GUÉNE SAKEUR WARA LIGUEYI SI WALOU WEERGOU YARAM WALA LOUAME SOLO BATAKHNA GUA WARA GUANAYO BATAKHAL BOUDIOGUÉ SI TAKDER DÉMOU SAYTOU BOU WEUR
  3. KOUNOUFÉK SIBITI WARGUA DOUGOUSIBIR ? DANOWARA TOK SI KEURGUI MAYNANOU KOUAME LIGUEY BOUMENENIAK WALA LOUAME SOLO TAK LADIOK WALA SI SAWALOU WEERGOU YARAM
  4. SOUFÉK DANAY LIGUEYE FOUMA DEUKOULE DAKH MENA DI DAME DI NIAW? WAW SOUFÉKE AMEGUA BATAKHALE BOUKAYEFIRDER
  5. NEUNA DIEULE SI NAMAR YI REWMI? BÉN NAMAR REWMI TAKHAOUL AK YOU NITYI MOME
  6. MEUNA GUÉNE DIEUDI LÉK? WAW DÉDETE NDAKHTE BOUNÉKE LOUMEUNIAK WAW WAYÉ SOUFÉKE DOLOUAME SO NDAKH MAGUI ANDI LÉK SAYOUNÉ SI GOKYI
  7. MEUNA GUÉNE DIEUDI LÉK SI BEURÉB YOU BOUKOULE ? WAW WAYÉ NANÉK LOUAME NIARIGNE
  8. MEUNA GUÉNE LÉKI SI SAMAY WADIOUR? DÉDÉTE NAKHDÉ DOU FARATA MOUYE BEUSSOU FETE AK BOUBOULE FETE AK LOU MOUNEUNE DONE THERENANOU DAME BANÉNE KEUR RAWATINA KEUR YI GUENE DI NOPALIKOU
  9. MEUNA GOUGUÉ SAMAY KHARITE MAGUÉT DIBLILÉNE ? WAW BOULE FATE MAK YI LA FEBBAR BI DI DIAP BATAKHNÉ BOULE FATÉ AR SABOP
  10. DIKLENE NANOU SI MBEDABI TAGUAL YARAM ? TÉRENANOU GUANEK FÉP BÉRÉBOU TAGUAL YARAM SI MBEDABI AK GOKYI DONTÉ TAGUAL YARAM WAYÉ NAGUÈNE SORENTÉ BAKÉNE DOMINA DIEGUE MAROMAME (1METRE)GUEN MOYTOU BOLO BI
  11. MEUNA GUÉNE SAMA KHATHIE ? WAW BOUYE DÉM DOUS WALA KIYEU SAYTOU YARAMAME
  12. KOUDIALGUATI LOUKAYE KHAR? MEUNA NOULA DANE GUA FAYE KHALIS BOUTOLOLE(3000€)SI KHALIS REWMI KOU DEGEURBOP DANE NEUNA GUÉNE MÉTTI

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof