OMS BOTAYE ADOUNA BI SAYTOU SI WALOU WEERGOU YARAM KHALATE YI NOUMEUNE ARE SI FEBBAR BOU BESS BI

.

DI RAKHASS SAY LOXO FOMEUNE TOLOU
.
LOUTAKH ? DI RAKHASS SAY LOXO FOMEUNE TOLOU AK NDOKH SABBOU WALA AK LOU AME ALCOOL ? RAKHASSOU NDOKH AK SABBOU WALA AK ALCOOL BI GUAYE RAKHASSÉ SAY LOXO MEUNE NALA ARE SOUFÉKE DIAGORO BI MOGUI SI SAY LOXO

MOU SORÉNTE TOUTI RÉK
MOU SORÉNETE BÉN METRE(1METRE)AK KI DI SEKHEUTE WALA KI DI TISSOLI
LOUTAKH ? BOU NITKI TISSOLÉ WALA MOU SEUKHEUTE DINA AME AYE PÉP NDOKH BOUYE GUÉNE SI SA GUÉMINE WALA SA BAKÉNE DÉ YOYOU NEUNA AME DIAGORO SOU NÉKE DAGUAKA DIÉGUE WALAGUA NOYI KI SEUKEUTE BÉP NDOKH SOUNÉK AMENA DIAGOROBI (VIRUS COVID-19)

MOUNOYTOU TOKHAGNE BEUT YI WALA BAKÉNE WALA GUÉMINE
LOUTAKH ? LOXO NEUNA LALE LOUNÉK DÉ DIAGORO BI NEUNA NÉK SI LOXO DÉ BOU FÉKE MOGUI SOLALÉ SA BEUK WALA BAKÉNE WALA GUÉMINE SINONOU DIAGORO BI NEUNA DOUGOU SA YARAM

TOPTOLE SAWALOU NOYI KAYE
FEKHEL BA YAW AK NITE YOU LA DIÉGUE AK NOYI BOUBAKH LOUMOUYE FIRDÉLE NOU TAF SÉN GUÉMINE AK SÉN BAKÉNE SONOUYE TOSSOLI AK SEUKHEUTE AK SEN THIOTIOU WALA MORSO SISASSI NANOU CENDI MORSO BI FIWEUR
LOUTAKH ? PÉP NDOKH DIAGORO BI BOUNÉK ARGUA SA BOP SA WALOU NOYI SI NIT YI AME DIAGORO BI WALA SIBOURU WALA LI DIDIOGUÉ( COVID-19 )

SOUFÉKE DAGUA AME SIKSAK SI DIAGOROBI TOGUALE SA KEUR WALA GUA WOTÉ KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM DIABOTE WALA NGI SAYTOU KHALE YI WALA GUA WOTÉ NGI TOPETO WEERGOU YARAM WALA NUMÉRO VERDE BISI GOKBI

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof