BATAKHAL BOUWARAGUA COVID-19 NOUKHAME  LOUNOU WARA DIMBEULÉ  ADOUNA

NI DIAGOROBI FEBBAR  BI COVID-19 DI LAWÉ SI ITALIE AK ADOUNA BI DANE SÉWARA DIOK GUAW

BATAKHNA  GEUNE HAR SÉN WEERGOU YARAM KÉN BANIA GUÉNE  KEUREUM KHANA  NGAYE DÉF LOUMENE NIAK   ( LIGUEY WALOU WEERGOU YARAM NIBI SA GOK)

BO AMOULE  AYE FIRDÉLE AYE DANE KHATHIE NASI

NOYTOU NOUWALALA DIAGOROBI AME NA AYE MATOUWAY  YOUNOU DIEULE BADIMBALI NIEP

1 DAGUA BEUGUE DIMBEULOU  ASKAN BI?

TÉTHIE NANOU FÉP FI GUA KHAMÉ WAY LAKHOUYI NEUNE NANIAW OUTSI WALOU WAYÉ NEUNE GUA DEM SI BEURÉP BA DIOYTOU SA NAKHAL  AMANA  SA WAREF DINANE SI BAYI KHEL

2 KHARALE WOTÉ WA BOLO BI SAYTOU WAKHANE  AK BEUSS BIGUA WARA TÉW ?

NOYTOU DIAGORO BI LAW  DIAMONO BI TETHIE NANOU BEP WAKHANE  BA DIEUMI DIAMONO BEUSS YI DANE KO KHAMALÉ

FATELIKOULE BÉP NITE BOU WARA WAKHANE  KHABAR BI DINALA FEK SI KEUR YI DIMBEULE SOFA NÉKOULE FAGUA DEUK  BIDAL SA TOURE SI BOUTE BI

3 KHARAL BA LIGUAY LATHIE GUÉNE?

DIGUA DIOT BATAKHAL  LIGUAYE  LATHIE SOUGUÉNE

SI AYE BEUSS SO DIOT BATAKHAL NOU NAGOULELAKO KHARAL TOUTI  GUA DEM SI DARÉP BA DIEULI SA CAYITE (PERMESSO SOGGIORNO)

SO DIOT BATAKHAL DÉ CONTANO  GUA BEUGUE DÉMATE DI GUA KHAR TOUTI DAKH LEUPP TEUTHIE AMEGUA  TAN  WALA SA LAYTOU KAT(AVOCAT)GUA WOKA AK TÉLÉPHONE WALA SA ÉMAIL WALA KEUR DIMBEULI GUI GUA DEUK KIKADITE

4  SOLAGUA AYE LÉRALE DAGUA WARA YOBOU SÉY CAYITE SI NISAYTOU  DIMBEUL

DIAMONO BI LÉP TEUTHIE BAKHNA YONÉ BATAKHAL ÉMAIL  DIAFÉNA  KHOLALE SI BIR BA KHAME. WOTEL PEC WALA EMAIL BOLO/YI YOR WALOU DI  DACOR SI DIMBEULI

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof