Info CuraItalia

seleziona lingua 2
Seleziona lingua:

DIMBEUL 600€ MANEUSI AME TAMITE WAY LAW LAKHOU YI WALA NGI BANENE KHÉTOU CAYITE (PERMESSO SOGGIORNO)

1 AVRIL 2020 SI SITO INPS BI (https://www.inps .it) MEUNE GUA DÉFI SA LATHIE BA DIOTE SI YOKAL YI 600€SI WEER BI DI MARS. KOUKO MEUNE LATHIE?

  • LIGUEY KAYE AME PARTIE IVA SI WEER 23 FÉVRIER 2020 BI

  • DÉ MOU LIGUEY SI WEER WES BA DIAP 23 FÉVRIER 2020 AK(co.co.co)

  • NGI LIGUEY SI WAL BATE WALA SOUF AK COMMERCE Ak LEUPP LOU DIEUME SIWALOU WEGNE

  • LIGUEY KAYE YI NÉK SI WALOU TOURISME DE SEN LIGUEY SI WALOU WEER LA SI GUEDJI GUI NOU DAYI DE NEKOUL SEN DIOBARÉ CAYITE BINE NI LATHIE JANVIER 2019 BA 17 MARS 2020 NANOUS SOKHLA

  • LIGUEY KAYE SPECTACLE NIOME WARNANOU AME NOU NÉW 30 CAYITE SALAIRE AYE BEUSS BOUNOU FAY SI ATTOU 2019 BI DÉ FAY SI ATTOU BI WÉSSSOU BOU WÉSSSOU 50.OOO€

  • LIGEUYI KAYEYI TOLYI GNIOU AME DI LIGUEY BOU AMOUL AP AK BENENE KHETOU LIGUEY DINANOU AMOU ATTE BI WES 50 BÉSSOU LIGUEY SI SÉN WALOU BOP

SÉN WAL MEUNOU KO LATHIE NOGUI DIOT NAPAYE ( PENSION /REDDITO DI CITTADINANZA/ AIDE SOCIALE /WA CHÈQUE WAY LAGOU

NANE GUAYE DEF BA DIOTE YI?

  • CONTE BOUYE DOKH DÉ INPS KHAMKO

GUA DEMSI SERVICE ONLINE BOU INPS https://serviziweb2.inps.it/RichiestaPin/jsp/menu.jsp

DINANOU YOKAL KHALIS NGIGUAMÉ LIGUEYE KHOLE KHALEYI SKIEUR YI DÉ NOU NEK AYE WAY LAKHOU WALA DI LATHIE DIMBEUL ADUNA BI

NOU DAME SI SITO INPS (WWW.INPS.IT)GUANÉK DI NOPALOU DA W WADIOUR MEUNE GUA LATHIE YOKAL KHALIS NAK GUA MEUNE FAY KI DI LIGUEY DI KHOLE SAY DÔME DÉ CHARTE REWMI DIEUKO.. bonus per pagare servizi di baby-sitting previsto dal Decreto Cura Italia.

YOKALBI SI YI DI LIGUEY DATAY NILAYE TEUDÉ

  • LIGUEY KAYE YI YOR SÉN LIGUEY BOP
  • BINTOU SI LIGUEY KATYI KHATHIE SÉN LOUNOUYE TOPATO
  • BINTOU NGI LIGUEY SEN YEUF BOP SI INPS
  • BINTOU NGI LIGUEY SÉN YEUF BOP SI CAISE YOU KHAREGNE

YOKAL KHALIS TOLOUNA SI 600€ SI WADIOUR DÉ SAK DOM YOUAME FOUK ATE AK NIAR YOU MATOUL (MOINS DE 12 ANS) DIEUFADIGOKO NGI LIGUEY DI KHÔL KHALEYI AK YOU KHALEYI AMOUSI SOLO AK WAY KHALEYI LAGOYI YOU BINETOU SI ECOLE YI WALA BARÉP BOUNOU NÉK YOKAL KHALIS INPS NOKO YOR DÉ GUA GUANAYO SA CAYITOU DIABOTE

DAKH GUA DIOT SI BINTOULE SI WA INPS (https.//.www.inps. it) BOUANDALE BATAKHAL SISABEUGUE BEUGUE dell’INPS (https://www.inps.it/)

DAF LÉN NAK BOUNÉK LIGAYE LATHIE DIOTALINIAKO AK BENE RAGNÉ KAYE(PIN) WAYÉ BENÉNEGUENE WALA BI (PIN) TEUYE KI BOU BAKH SI CAYITOU NIABOTE YI LAYE NEK AK SI LADIOU YOKHAL BI

NOPALOU SPÉCIALE COVID-19 NEUNE NANOU SI AME SAK NGI WAY LAKHOUYI AK DIMBEUL

SO DÉME SI SÉN SITE WEB INPS(https.www. inps.it)DIGUANEUNE DOUDOU FOFOU BA LATHIE SI WALOU NOPALIKOBI 15 JOURS DINANOU HIBI SI NIEUP LIGUEY KAYE YI 5 MARS BÉBESOU ECOLE DI HIBIWAThttps://www.inps.it/

FIRDÉLE

SÉDELÉ 50%WADIOUR YI SÉN DÔME AME 12 ANS

SÉDELÉ 50%WADIOUR YI SÉN DÔME AME 12 ANS

SEDELE 50% WADIUOR Si AMÉ DÔME WAY LAGOU DÉDOUMOUSI KHOLE ATE BOU KHALÉ BI AME

NANE GUAYE DEF BA DIOTE YI?

NONOU NEUNE DÉF BASOUNOU AKSI SI BEURÉP LIGUEYE KAYE SI ONLINE 600€ AK WADIUOR YI LIGUEYOUL NDAK COVID-19 WALA LIGUEY TEUYÉ KHALÉ

MEUNE NANÉK HUA DEM SI BEURÉP BOU INPS ONLINE( INTERNET)
1 )RAGNÉ KAYE BI INPS DILA DIOK (PIN)
2) SPID TOLOUWAYE 2 WALA MOU EUPEUKO
3)) CARTE D'IDENTITÉ YOU BEUSSI 3.0 (CIE)
4) CARTE NATIONALE LIGUEY (CNS)
LADIOU RAGNÉ KAYE (PIN)NEUNE KO DIARELE SI YI
SITE INTERNET WWW.INPS .IT DIEUFEUDIKO BEURÉP YI LADIÉ PIN
WOTÉ AK LATHIE NUMÉRO VERDE 803 164 DO FAY DARA AK TÉLÉPHONE KEUR WALA 06 164 164 BI AME NA FAY SI TÉLÉPHONE YI
.

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof