DOMOU REWMI NGIBISI SÉN REW AK NGI FI DIOGUÉ BÉNENE REW

DIEULÉNE LI

- CAYITE BOU BEUSS BOUYE TAKH GUA AMA SAGNE SAGNENIOU GUÉNE REWMI 26 03 2020 NUOVO MODELLO 26.03.2020

- CAYITE BOUYE FIRDÉLE TOUKI MODELLO

  • YANE MATOUWAYE MO BAKH 28MARS BI WÉSSOU SI NGI DOUGOUSSI SI REWMI DE NEKONE SI BENENE REW
  1. NGIDITE SI WALOU DAME AK DIKKI BATAKHAL BOULENE NI MAYE NOUYE DAME AK DIKK( LINK AL MODULO ) WAR NANOUKO DEKANÉ AK NGI YOBOU CAYITE TOUKI WARNA AME (WÉRRGOU YARAM LIGUEY BOUAMSOLO) BOU NOU NIAWE WARNANOULENE BERRE 14 JOURS DOUNOU WOTÉ DAKH NOU SAYTOU SÉN WEERGOU YARAM LI MOGUI SI SITElink al modulo 
  2. NGI DIOGUÉ BITIM REWMI MEUNOUNA DIEULE DEM AK DIKK REWMI WAYÉ NOU LOUÉ LILENE YOBOU ( KEP KOULENE DIEULE SI AÉROPORT PORT STATION NGI LOUÉ AUTO WALA TAXI LOUÉ AUTO AK KI DI DAWAL )   
  3. DANO WARA BER NGI DOGOUSI SI REWMI AK NIAW SI AUTO PRIVÉ NGI DOUKO NAKH LIGUEY NEUNANOU DIEUFEUDIKO 72 WAKHTOU (YOKASI YENENE48 )YOUSI AME SOLO 
  4. NIEUP KOU DIOGUÉ BITIM REWMI NGIEUW AK AUTO PRIVÉ WARNANOU YEUKLOU SI BÉRRABOU FADIOUKAYE YI YOUNOU RAGNÉ SI GOKH BI 
  5. NEUNA LA BER SOU FÉKE BEUGUE FOU DIÉGUE FI GUA DEUK
  6. KOU DOUGUISI REWMI BOU YAGUE WARNA BERROU WALA SOUNÉKE DIOTOUNOUKO (NOUNOU NONIEW DIEUKO WALA NEK NOPALIKOKAYE YI LENE FATE...) NIONIO NAK WARNANOU BERROU SI NDIGUEL LOU NGI AR NITE SÉN LEK DI NIEW NINOUKO BEUGUÉ
  7. YENE DIEUFLENETE NGI DI LIGUEY SI WALOU WEERGOU YARAM ,NGI TOUKI BOULOBI WADIÉ DIEUREUDIEUF

 

SIWALOU NIK DI YOR WALOU WÉRRGOU YARAM AK NATAGONE BIYOR WALOU DEM AK DIKK BI 

  • SI DEM AK BIKK GUI MANE DOMOU REWMILA SORI REWMI WALA REWMI (ITALIE )LAYE DOUNDOU DÉ DEM FÉNENE NAK NEUNE NA NIBISSI SI RÉWMI ?

WAW SOFOGUÉ LOUNEUNTE KHARE.AK DOUMOU REWMI WALA GUAYE DONDOU SI REWMI DAGUÉNE SORI REWMI NEK SIWALOU ( TOURISME AFFAIRI AK NOUMOUNEUNTE DONE ) BOKA NASI DOUMOU REWMI NEK BENENE REW DI FA LIGUEY WALA DIFA DIAGUE DÉ BEUGUE NGIBISI TOK SEN REW LOUTAKH (YOUNOU DAKH SI SÉN BÉRRABOU LIGUEY KAYE, NIAK SÉN KEUR, NGI BAYI SÉN DIAGUE)

  • MANE BÉNENE REW LA DIOGUÉ NIAW REW ITALIE NAKH NEUNA NGIBI SAMA REW?

WAW,SO FÉKE AME LOUTAKH GUA BEUGUE DÉM SILOU WOR YAKH DOUMOU RÉWMI DI DOUNDE FENÊNE YALENE YAME LIGUEY BOU TAKHAW WALA SA LIGUEY NOU TOUKHOL KO LEGUI DAGUAY AME BATAKHAL BOUYE FIRDÉR SA GUÉNE REWMI DÉ NGI YOR KARAGUÉ REWMI DIKA DIOGUÉ

  • BAKHNA GUA KHAME BEUSSOU DEM BI DAKH SA REW NOUNOUY NOYTO FEBBAR BI COVID-19 AK GUA WAKHANE AK NGIFI TÉWAL SA REW ( AMBASSADE
    MAGUI SOGUE NIBISI SI RÉWMI NAK NEUNE WAKH NOU DIEULSIMA AK AUTO AÉROPORT, STATION TRAIN, SIBONTOU BIMA AKSÉ ?

WAW NANÉK NITE BOUGUAKHAMÉ YALEN DEUK DÉ MOU DIEU AYE MATOUWAYE DÉMOU GUANAYO BATAKHAL BI KAYE MAYE MOU GUÉNE GUA TEDIOU DÉ LALÉ NIEW GUA NGI SAYTOU WEERGOU YARAM AK SO YEGUÉ SA YARAME BÉP DIAFEDIAFÉ YOUYEWANÉ FEBBAR BI COVID-19

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof