Buoni spesa

DIMBEUL LEK YI AK LEK BOUNEUNE TI DONE YOU NOUYE DIEUFADIKO NITE AK WAKEUREUME NGI AME DIAFEDIAFÉ LÉK

-- AK NDIGUEL n 658 NGITOU KI YOR WALOU DIMBEUL AK BÉP GOKH BI SI REWMI DIOTNANOU DIMBEUL BOUNOUWARA SÉDÉLE AK NITE YOUKO SOKLO DÉ DIAFEDIAFÉ SI WALOU DOUNDE

BÉP GOKH DINANOU SÉDELÉ DIMBEUL BI AK NGIKO YELOLE DÉ DIAFEDIAFÉ DAP LÉNE SI FEBBAR BI COVID-19 NI DIOTOUL ( REDDITO DI CITTADINANZA REI NASPI WALA NI TOK SI KEURYI) NONÉK SI KAW BAPARÉ

SI LIAME SOLO SI TEURELE BI dall' art 27,comma 1, del D Lgs 251 /2007 NII ADOUNA BI DI AR AME NANOU YONE AME DIMBEUL BI COME WA DOMOU REWMI

RAGNÉ YEÑNE BIRYI AK KAGNE LAYE DIEUKH DAGUAYE DEM SI SÉN SITE WEB GOKH BIGUA DEUK

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof