Ricongiungimento familiare

SIWALOU ANDI SA DIABOTE MNSA BOU WA DUBLINO 3 TEURELE SI COVID-19

BAKHNA ANDI SA DIABOTE WALA KHALÉ BOU AMOUL WADIOUR SI REWMI CHARTE REWMI 8 DEL CD DUBLINO 3DIEULKO SI WALOU FEBBAR BI COVID- 19

NANE KHALÉ WALA DOKHOLÉ?

  1. KHALÉ NEUNE NA FÉKI KENE SI WADIOUR SI BENENE REW EUROPE BOUNEKO RAGNÉ MOU BEUGUE SOKHLA DIMBEULE ADUNA

LIGUEY NGITE KI YOR KARAGUE REWMI 0020359 9 MARS 2020 WA QUESTURA DINANOU TAMBALI DI DIEULE LATHIE SI BEUGUE DIMBEULE ADUNA WAYÉ DOU NIEUP NONEUNA DÉF LATHIE C3 AK CD LATHIE DUBLINO WALA KHALÉ BI DINA MAGUE NOU KHAR BA QUESTURA HIBI MONEUNE DAME DAF LATHIE BI DI RAGNÉ AK C3 NA DIEULE DOCUMENT AME SOLO YOUNOU SOKHLA (DIABOTE TREE THIOBARÉ KHALÉ BI WADIOUR DACOR LOU TAKH SI KHALÉ BI MAK SI DIABOTE BI DOCUMENT WADIOUR AK KHALÉ BI)

  1. KHALÉ BI FÉGNE FÉNE SI LATHIE BALÉGUI GUÉNE GOULE SI C3 SI WAGNI LIGUEY YOU QUESTURA:

SOU FÉKE SETE BI DIAPANA 3 WER NEUNEGUA LATHIATE BOLO FAMILLE KENE DAKALOUGUA LATHIE BOU DIEUKA BI DIALE NIAW NA SI WA DUBLIN SI WALO BOBOU BOU WA QUESTURA TAMBELÉ LIGUEY DI NA NOU KO YEUGLÉ AK NOMOUY DOKHÉ

  1. LATHIE BOLO DIABOTE GUI GUENE GOULE DAKH TÉ YENE LIGUEY SI QUESTURA BI TAKHAW MOTAKH DIAROULE SOPI DARA SI SA LATHIE:

WOTÉL QUESTURA NOU KHAMALA NAGUAYE DÉF AK SOPI TÉ PEC AK YÉNENE BIIR YOU MÉGOLE (ad sa BOLÉKOU AK NITE RACCOMANDE) BÉP SOPI TÉ SI LATHIE NOU MOUYE DOKHÉ SI KHALÉ YI SI AK KHAREGNE LIGUEY KATOU JUSTIS

  1. NOUMOUYE DOKHÉ DIAPE BAKHNA WAYÉ DOU SOPEKOU DAKH NITE DI WEUR SI WALOU FEBBAR BI COVID-19

SOPTÉ REWMI ITALIE DIEUMELÉ AK BENENE REW TOGUEL YI ARRÊTE NANOUKO SI CHARTE 29 DUBLINO SOPÉ KOU DI NA NIAW DIGUENTÉ 6 WÉR D'ACCORD SI REWOU TOUGUELE YI SI LATHIE BOLO DIABOTE GUI BOU NÉKE MOGUI WADIA DIÉKH WOTÉ BOLO DUBLINO DAKH LATHIE DIMBEUL

N.B. BOLO DIABOTE GUI SI ATE YOU MAK NO DIEK SI LATHIE SI DIEUM DUBLINO 3 DIGUA DIOTE KI GUAKHAME NÉ 18ANS MATAGOULE BOU NOUYE DIEBAL LAHHIE BI

TEK LET YI DI NANOUKOTOP BENENE PAR BÉNENE NIKO BOLO DIABOTE GUI BEUGUÉ Msna

LOU SINEUNA AME SI SITUATION 1 AK 2 NOU WANÉKO AK SOU TAKHAWE BOLO EFRIS KHANO SI YIBAR DUBLINO 3SI BINDOU C3 WALOU QUESTURA GUA NIAW SOFÉK NIGUI WADIEU DIÉKH

BOLO EFRIS LIGUEY SI WALOU CAYITE BOLO DIABOTE GUI DI MSNA WOTÉL SO AMÉ SIKI SIKI

E-mail progettoefris@cidas.coop;

TÉLÉPHONE +39 3404277780;+39 3428735259 SOUFÉKE YENE YIBAR GUA BEUGUE SI FEBBAR BI COVID-19 NGI LATHIE DIMBEUL ADUNA Ak WAY LAKHOUYI DAMALE SI SITE JUMA MAP https//:coronavirus .jumamap .com/it.it / WALA DIOKOL AK LIGUEY KATOU ARCI NUMÉRO VERDE 800905570 /3511376355

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof