SOUFÉKE NDAW GUA DI KHAR BOLO DIABOTE GUI?

NOUYOUNANELA

SOUFÉKE YAGUI KHAR BOLO DIABOTE GUI SI KÉNE SISA WALOU WAKEUR DIARÉKO SI Cd"DÉ DUBLINO III TEURELE KO LIRAL NAK YIBAR YI SI TOP

  • SONÉK SI DIAFEDIAFÉ FEBBAR BI COVID-19 SI DEKOU YI BOLÉ EUROPE BI SÉN KHALATE MOYE WEERGOU YARAM NITEYI NOU WAGNI TOUTI DAME AK DIKK SI BIIR AK SIBITI SI DEUKE BOUMOUDONE

  • SOFÉKE YAGUI SOGUE TAMBALI LIGUEYE SI WATOU BIGUAWAL LIDIEUNTI SAY CAYITE AK SA WADIOUR YI LA BEUGUE ANDI TOUGEULE WAKHAL SA WADIOUR NOU YONÉLA FOTO CAYITOU DIOUDOU CARTE D'IDENTITÉ WALA LOUYE WANÉ SI DIABOTE GUI GUA DAKH NOU NEUNE YONÉ TAMBALI LIGUEYE SOUFÉKE SA DIAMONO GUI DOUTÉRE NOUSIYE LIGUEY

  • MATOUWAYE NOUDADIÉLE SI DIAFEDIAFÉ BI DOU DETHIE DARA LIDIEUTIYI SI WALOU ANDIGUI KHARAL RÉ TOUTI NDAKH NOGUI SIYEU LIGUEYE LI DOU YAGUE

  • SOUFÉKE DIBEULE GUA SA LATHIE SI BOLO DIABOTE GUI DÉ YAGUI SOGUE AME 18ANS WALA AMEGUAKO DIGUA LADIÉ DOSI DARA DINANOUKO LIGUEY AK SOUFÉKE MAKGUA

  • SOUFÉKE DAGUAYE WADIA AME 18ANS GUA BEUGUE FÉKASSI KÉNE SI WAKEUR WALA BÉNE SI DEUKOU YI BOLÉ TOUGEUL DÉ DÉ LATHIE GO SI WALOU BOLÉ DIABOTE GUI WAKHTANANE AK KI LA YORE NGI SAYTOU SI BIIR BI DINANOULA DIMBALI

  • SOUFÉKE DAGUA ALE SIKISAK WAKHTANE AK KILA YOR WALOU NGI SAYTOU LIGUEY BI NIOGUI DINALA DIOKH BATAKHAL YO SOKHLA

BOUL FATÉ TOPEUTO DUBLIN YONE BOU GUAW LA BEUNENEU FÉKI SA WAKEUR SI DIAM

SO AMÉ AYE LATHIE SI FÉKI SA WAKEUR PROGÉ EFRIS NEUNANOULA TONTOU WOTÉL WALA BINDA LATHIELE KI TOPEUTO LIGUEY BI NOU LATHIE BÉREUBOU WALA e-mail PROGETTOEFRIS@CIDAS COOP WALA NUMÉRO Yi +39 3404277780; +3934287345259

SO BEUGUÉ AME LEERALE YOU WOR DAMALE KHOLE SITE JUMA MAP https ://CORONAVIRUS. Jumamap.com/it-it /WALA OPÉRATEUR NUMÉRO VERDE 800905570/3511376355 WALA numeroverderifigiati@arci.it

(Thanks to CIDAS)

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof