NGI LIGUEYE SI WALOU SOUF YANE BOUTOU YOU OUBÉKOU NANOU NEUNEU AME ?

FEBBAR BI COVID-19 BI YI LIGUEY SI WALOU SOUF TAKHNA GUISSNANOU YÉNE LIGUEY WÉR YI WAGNÉKOUNA SI BIIR REWMI YEP ITALIE SI GOKH GOKH YI LIGUEY SENE BOP AK NI AME SENE TOLE LOU BOP AK NI KO LIGUEYE .

NDAKH GUA BOKASI DAWALE KHOLE SI BÉRRABOU YI

SOUFÉKE DAGUA AME DIAFEDIAFÉ SI WALOU LIGUEY WALA FINELA YOBOU WALA SA TAN AMOU AKHAME AK AR BI SI WARE NEUNE GUA DEM GUISSI BOTAYE BI BAGNE KAYEYI NOU DIMBALILA WOTÉL 80055705 (351 1376335)

Fonte: “Lavoro agricolo, le iniziative per incrociare meglio domanda e offerta”, www.integrazionemigranti.gov.it

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof