YIBAAR BOU AME SOLO SI WALOU KHALÉ YI BOU AMOUL MOK FI DÉ MOUAME WALA MOUYE AME 18ANS SI WÉR SI DI NIEUW NANE TAKHAWAYOU NGI SAYTOU MIROU KHALÉ YI

NOUYOUNALENE YENE NIEUP 

NIGUÉNE KO KHAMÉ TASARO FEBBAR BI CORONAVIRUS SI ADUNA BI TAKHNA BIR YOU BARI SI SI DOUNDOU DOUNDOU SOPÉKOUNA NIÉNA SI YENE TAKHNA SI WALOU ECOLE LIGUEY YOUSÉW SÉWANE YI AME NA DIOPITÉ TAMITE YÉKHEULENA DIEULE AK LATHIE SI WALOU CAYITE REWMI  

SOUFÉKE BEUGUE AYE LEERALA SI SAY BIR NEUNE GUA WOTÉ 

  • KILAYE TOPATO FI
  • KEUROU DIMBAL YI GUA DEUK NI KO DJITÉ
  • SOUFÉKE DEUKO FOFOU NAK DAMALE SÉTI BOLO YI MALNI (ARCI) DAKH NOU DIMBALILA

NANENANOUYE DOKHALÉ NI YOR WALOU LIGUEY KHALÉYI ? 

NANENANOUYE DOKHALÉ NI YOR WALOU LIGUEY KHALÉYI ? 

NOUNOUDOKHALÉ LIGUEY BI SI NIAREL CHARTETOU REWMI ITALIE ITALIE KHALÉ BOU FI AMOULE BOK NEUNA FI AME CAYITE REWMI BOU KHALÉ DÉ DI WADIALE 18ANS DI TOPATO BOPAME AK NÉKINAME SI REWMI BAMOUYE AME 21 ANS 

 

 

KOUYE LATHIE LOUNOUYE TOPETO ?  

  • KIKAYE TOPATO FI

WALA 

  • MOUDAME SI NOUYE LIGUEYE SI GOKH YI WALA NI NÉ SI KEURGUI MOUYE MOUYE NÉK

    NBSOUFÉKE DAGUA AME DIAFEDIAFÉ SI WALOU LATHIE KI YOR SAY BIR WALA DIMBEUL NI NEUNE GUA LATHIE DIMBEUL SI WA BOLO BOUMELENI (ARCI) NOUDEM GUESSTOU PÉTHIOU KHALÉ YI 

NANE NANOUYE LADIÉ BIIRBI ? 

  

 

 

  • SI DJITOU PÉTHIOU BOU GAW WALA PÉTHIOU BI BI GUESSTOU KHALÉ YI 

WALA 

  • PÉTHIOU KHALÉ YI

KAGNE GAYE DEM WANÉ SA LAHIE? 

SOUFÉKE AMEGUA 18ANS 

BANE TONTOU GUA NEUNA DIOTE ? 

PÉTHIOUME KHALÉ YI SOUNOU GUESSTOU SAYE BIR BA PARÉ NEUNA NOU DIEULE DOGAL YOUKALA SANÉKINE FIGA DEUK BA GAYE AME 21 ANS 

SOUFÉKE TONTOU BOU BAKHOULE GUA AME ? 

SOUFÉKE LOLOU NOLA TALE NEUNEGA DEM SI KI SAYTOU SA BIR WALA NI NÉK SISEN KEUR NOU KHOLALA SA BIIR YI3 

DAKH DIAMONO FEBBAR BI NEUNA NOU LATHIE NOUMOUY DOKHÉ? 

WAW NI NÉK SI KEURGUI GUIGANÉK WALA KI TOPATO SA BIR NEUNANOU GEUSSTOULE FOTLOU 

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof