COVID-19 AYE THIOPÉKOU YOU BÉSS AK AYE YAMALÉ SI WÉRBI MARS DIAP 4 FANE BA 18 FANE SI ATOUME 2020

4 MARS BI BA DIÉKHALE 18 MARS SI BEUS YI AYE THIOPÉKOU YOUBES DINA AME SI WALOU DCPM SI BEUS 26 SI WÉROU AVRIL SI AYE CHARTE DOKHALINE AK DIEUFÉYI SI WALOU FEBBAR BI CORONAVIRUS


|| SORÉNTE DIGUÉNTE NITE YI BALÉGUI LOU WARA AME LA ?

SORÉNETE DIGUÉNTE NITE YI BENA METRE LOU WARA WAYÉ SOLE MASK AK AYE GANG AK BÉP DIOUMTOUKAYE BILAYE ARRE SI FÉBBAR BI TAKH MASK YI LOU DAGANLA SI BÉRRABOU TADIOUYI DÉ NITE YI AME SI YONE


DEM BI AK DIKK NOUMOUYE DAMÉ ?

MAYE NANOULA GUA DEM AK DIKK SI BIR MÉM DEUK SOFÉKE SI WALOU LIGUEY AK WALOU WEERGOU YARAM LOU NEUTE NIAK WALA GUA SÉTI SA KHARITE WAYÉ DANOUYE TÉRRE LOKO BI DAGUENE SORÉNETE BENA 1 MÈTRE DAGUÉNE DIEUFADIKO MASK YI .NITEYI DEM DÉ SORI FINOU DEK NIOME DA SI WALOU LIGUEYE WALA WEERGOU YARAM AK SOKLA BOUAME SOLO MAYE NANOUKO NOU NIBISSI LOUMOU GUENA GUAWE SI DEUKEUM FI MOUYE FANANE AK FOUMOYE NÉK

NIANA NANOULENE GUÉNE WOTE SI NUMÉRO GOKK BI SI WALOU FEBBAR BI COVID-19 DÉ BO NIBISÉ WARGUA BERROU DAKH WORAL


YANE MOUYE CAYITE BI BEUSS BI SI WALOU DEM AK DIKK BI ?

CAYITE BOU BESS SI WALOU DEM AK DIKK BI SI SA DOUNDOU

CAYITE BOU BESS SI WALOU DEM AK DIKK SI BIIR REWMI

 

NDAKH NEUNA DÉM SI BÉRRABOU DOKHONETOUKAYE YI ?

MAYE NANOULA GUADEME SI BÉRRABOU DOKHANETOUKAYE YI AK FI KHALÉ DI FOWÉ AK GOKYI WAYÉ SORELE NITEYI 1 METRE WALA NOU TEUTHIE BERRABOU KHALÉ DI FAWÉ NGITE YI NEUNANOU NATA DIAFEDIAFÉ YISINEUNA AME


NDAKH NEUNA TAGUALE YARAM WALE MOTEUR ? NDAKH NEUNA ANDAKH KHALÉ ?

MAYE NANOULA GUA GUÉNE YAW KÉSSÉ WALA GUA AME KO ANDALE AK AYE KHALÉ GUÉNE TAGUALE YARAM DOUTÉRE GUÉNE SORÉNTE 2 METRE AK 1 METRE SI NIO DAF LANÉNE

NDAKH NEUNA DEM SI KHÉW DETHIE AK DINÉ

SOUMA KHOLE KHÉW DINÉ AK DÉTHIE YI MAK YI TÉW NOU MATE 15 NITE DANO WARA SOLE MASK AK SORÉNTE 1 METRE DIGUÉNTE


NEUNA DEM LAKOUKAYE YI RISTORANT WALA FAST FOOT?

WAW KHANA GUÉNE DEM DIEULI LÉK YI DAKH YI TOK SI KEUR YI LATHIE DANOU SORÉNTE BOUNOUYE DIEULE LÉK YI KÉNE NEUNOULE LÉK SI BIIR 


Cosa devo fare se ho la febbre?

Chi ha febbre sopra i 37.5 gradi e sintomatologie respiratorie ha l’obbligo, non più solo la raccomandazione, di restare a casa e avvertire il proprio medico.


NANE LAYE DÉF SOUMA AMÉ AMÉ YARAM BOUTAGUÉ ?

WAWOrdinanza del 19 Marzo 2020 CHARTE REWMI BI 19 MARS BI WÉSSOU 2020 CAYITE BI KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM LÉGUI LOU BESS BI AME MOYE NUMÉRO CAYITE GARABE YI KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM DILA DIOK AMNA LÉGUI ÉLECTRONIQUE BATAKHNA SOKO AMÉ AK CODE FISCAL NEUNGUA DEM PHARMACIE DIEULE SAÎ GARABE DOTO DIEULI CAYITE SI KI SAYTOU SA WEERGOU YARAM

AMNA THIOPEKOU YOU BÉSS YI DIOGUÉ SI GOKK BI BÉP YEUGOUYEUGOU DÉNOU DIEUMALE SI SI WALOU BOUNEKHATALE DJIGUENE DAKALNANOUKO ?

DÉDÉTE BÉP DJIGUENE BOUNOUYE DOR WAROUNOU BAYINOULENE GUINAW NEUNANOU WOTÉ SI NUMÉRO DO FAYE DARA 1522 WAKHTOU BOUNÉK (24H SUR24) DJIGUENE BIGUAKHAMÉ NOGUI LAYE DOR SAYOUNEK MAYE SANOULA GUA GUÉNE DEM SI BERRABOU YI LENE DI ARÉ SI CHARTE REWMI WAKH 11 MARS

NOGUI TAMBALI DIEUMBALI NITE YI GUAKHAME SÉN KHÉL YI DIAKHASONA SI FEBBAR BI COVID-19

27 AVRIL BI WÉS LA DIEUWRINE BI YOR WALOU WÉRRGOU YARAM AK NGI ARE NITEYI TAMBALI LIGUEYE BI NEUNE GUÉNE WOTÉ SI NUMÉRO BI 800 833 833 SAYO LÉNE WOTÉ DIOT LENE AK NUMÉRO BAGUAKHAME SOU FÉKE YAGUI FÉNENE 0220228733 BEUSS BOU NEK 8 BA 24 KEP KOU KO YITÉLE

YATALNANOUKO NEUNE GUA DEM SI NUMÉRO VERDE DI SIPPORT PSICOLOGICO SITE TEMATICO CORONAVIRUS BOU BESS SI KI YOR WALOU WÉRRGOU YARAM Numero verde di supporto psicologico

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof