GUÉNE BI WARA AME LE 18 MAI SOUBEU NANA DOKHALINE YOUBESS

LE 18 MAI NIEUP NEUNANOU GUÉNE DEM FÉP FOULÉNE NEK SI GOKH YI NOU DEUK NGI HAR REWMI NEUNANOU YAMALÉ GUENE BI SI YENE GOKH YI BAGNE FEBBAR BI COVID-19 TASSARO

YÉNE GUÉNE YI SISA GOKH AK BENENE GOKH DANOUKOYE YAMALÉ WAYÉ NEUGUA YAME SI BI GOKH BI GUANEK MAYNANOULA GUADEM SI BENENE GOKH SOU FÉKE SI WALOU LIGUEY WALA WALOU WEERGOU YARAM GUA NEUNEKA WANÉ WALA GUA BEUGUE NGIBI FI GUA DEUK WALA SAKEUR AK FAGUAYE NEK LOLOU DINANOUKOTAMBALI 2JUIN BIDINIEUW

LE 3 JUIN NEUNANOU TAMBALI GUÉNE DAME SI GOKH AK GOKH WAYÉ YI YOR KARAGUÉ REWMI DINANOU YAMALÉ GUENE YI YENE GOKK REWMI ITALIE BAGNE FEBBAR BI COVID-19 LAW

TÉRE NANOU BOLO NITYI SI BÉRRABOU YOU YOU NITE YI DI DADIOLOU DA NOU HIBIKO AKLOUMOU NEUNA DONE GUESSTOULE FI GUA DEUK WALA FAGUA BEUGUE DEM NANE FEUMANADEF

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof