TEUREULE BOU DIEUME SI DIMBEUL BOU NEUNE TEKHAR ( REM )

DIMBEUL BOU DIAP BI DIEULE NANOU NDOGOU DIMBALI DIABOTE GUI AME DIAFEDIAFÉ SI FEBBAR BI COVID-19 DIMBALI BI NOGUI KOYE AMALE SI NIARI BIR 400 BA 800 EURO NITE KOUNÉK NGI KO DIOTE MOYE NI DOUNDOU SI REWMI ITALIE DIMBALI LOU TOUTI LA SI LOU REWMI AME BOUGUAKHAMÉ SA AMAME TOLANA SI TOUTI WAY 15000 EURO DIMBALI BOKOULE AK YÉNENE YI DIMBAL NI NGITE REWMI WADIAL TOP SI FEBBAR BI COVID-19 TAMITE BOKOULE BALÉGUI AK BIMBAL DIABOTE YI DIOTE BOU DIOUP WALA NIAK DIOUP (KHANA WAY LAGO YI DIOTE SEN NAPAYE) SI SÉN LIGUEY BOP NOU LENE DÉLO SILOU DAW SILOU DIOTE SI DIMBEUL REWMI

LATHIE DIMBEUL (REM) WAR NANOUKO DIOGUÉ FI BALA WÉROU JUIN 2020

DAKH GUA AME BEP LEERAL DAWAL GUESSOU BERRABOU INPS WALA NGI SAYTOU BIROU LIGUEY KATYI GUA WOTÉ SI NUMÉRO VERDE ARCI

 

TEURELE BOUBES BI AME YÉNENE BIR YOUSI NEK SI WALOU LIGUEY KATYI 

DIMBEUL BI NOKOYE BESALATE MOUDIEUME SI WALOU LIGUEY KATYI SI FEBBAR BI COVID-19

  • KHARAGNE KATE YI LIGUEY SEN BOP, I CO ,CO,CO WALA NGI AME SEN LIGUEY BOP DÉNOU BINDOU SI NOUYE TOPATO SI WALOU AGO, LIGUEY KATOU WÉROU TOURISME DÉNOU DIOTE DIOTE WÉROU MARS SÉN NAPAYE 600 € DINANOU DIOTE TATE SI WÉROU AVRIL BENENE 600€
  • LIGUEY KATOU TOLE YI DINANOU DIOTE 600 € WÉROU MARS DIOTATE NAMPAYE WÉROU AVRIL 2020 500 €
  • NGI KHARAGNE DI LIGUEY SÉN BOP NOUAME WAGNI 33% SI NIARI YONE SI SI NIARÉROU SEMAINE 2020 TOLOKH NIARÉLOU SEMAINE 2019 DINANOU DIOTE NAPAYE 1000 € SI WÉROU MAI AK LIGUEY KATOU CO COC CO DANOU BINDOU SI TOPOTO WALOU LI BOKOULE DARA AK LATHIE DIMBEUL DINANOU DIOTE TAMITE NAPAYE 10O0 € WÉROU MAI
  • LIGUEY KATOU TOURISME DÉ SÉN THIOBARÉ LIGUEYOUNOU SI WÉROU 1JANVIER 2019 BA 17 MARS 2020 DINANOU DIOTE TAMITE NAPAYE NOUTOLOK 1000 € SI WÉROU MAI 2020
  • YENE NGI LIGUEY SÉN BOP WALA DI LIGUEY NITE NOUAME DIAFEDIAFÉ SI FEBBAR BI COVID-19 NOU BAYI, ARÉTE SÉN YEUGOU YEUGOU TAKHAW DINANOU DIOTE TAMITE NAPAYE 600 € WÉROU AVRIL AK MAI (SI LIGUEY KATOU WALOU TOURISME AK LIGUEY KATOU NGI DIOKOLALETÉ)
  • LIGUEY KATOU KEURYI DINANOU DIOTE TAMITE NAPAYE 500E WÉROU AVRIL AK MAI WÉR BOU NEK NOUAME BENE WALA LIGUEY YOU BARI YOU TOLLOLE FOUKI WAKHTOU(10 H) SI SEMAINE DÉ BONOU DEUKOULE SI KILENE DI LIGUEY LO

AMENASOLO NGI LADIAGOULE NAPAYE 600 € WÉROU MARS WAR NANOU DÉF FOUKI FANE ( 15JOURS) BINOU TEURELE CHARTE BI BOUNE KO DEFARAGOULE NAK NOU DEM INPS WALA NGI SAYTOU LIGUEY

BÉP NAPAYE BOKOULE BENE DIMBEUL NDAKHGUA AME LOULA LEER WOTÉL GUAW NUMÉRO VERDE ARCI WALA GUA KHOLE SITE INPS WALA GUA DEM SI NGI SAYTOU LIGUEY

BATAKHAL YI NEUNO KO DIOTE YAW SA BOP KHANA GUA OUTE LEEROU SI NUMÉRO VERDE ARCI 800 90 5570

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof