DOGUALE SI WALOU LIGUEY TOLE YI

WAKHTANÉ DIOUBO SI CHARTE 101 del"DL RIPARTI ITALIE SI WALOU LIGUEY SI TOLE YI DALE GUA NEUNA AME CAYITE BOUYE FIRDÉLE SA LIGUEY TOLE YI DÉ BOUNÉKATOULE 30JOURS KÉSSÉ BOUNOUYE TOLANTI SI BIR 30JOURS YI AKH YI LIGUEY LIGUEY YOUNOU DÉ NÉK SI KEUR YI SI WAKHTOU 0H DÉNOU DIOTE NASPI WALA DIS COLL NÉKOULE DIMBALASKANE BI (REDDITO DI CITTADINANZA) DAGUA SIGNÉ CAYITE LIGUEY BI NIAK DOUSI TOP WALA WAGNI LI GUA WARA AME BOU TOLOK 2000 € SI ATOUT 2020

 

BATAKHAL YI NEUNO KO DIOTE YAW SA BOP KHANA GUA OUTE LEEROU SI NUMÉRO VERDE ARCI 800 90 5570

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof