TEUREULE BOU DIEUME SI DIMBEUL BOU NEUNE TEKHAR

LOUKO DIAP 1JUIN 2020 BA DIEUME 15 JUILLET 2020 NEUNA GUÉNE DEM WANÉ DIOUMTOUKAYE YITAKH GUANEUNA AME CAYITE REWMI SI WALOU LIGUEYI

  • BAY WITE PESCA AK LIGUEY YOU MÉGOLE
  • DIMBEULI NITE
  • LIGUEY KEUR TAKHAOU DIABOTE

DAKH NEUNANOU WANÉ LATHIE BI ?

  1. KI GUAYE LIGUEYALE NEUNA DEM LATHIELA DÉ NAGOU NEKA AMENA KENE NEKANA SI GOKH BI WALA MOUWAKH BENE LIGUEY BOU DIAR YONE LEP BOU DIARÉ YONE NITE YI WARNANOU BAKHO NOURAGNE LENE SI SÉN KANAME AK BINEDA WALA NOU NEKONE ITALIE AVANT LE 8 MARS DE DEMOU NOU FENENE TOK SI REWMI
  2. NITE YOU SENE CAYITE DIEKH LE 31 OCTOBRE 2019 DÉ KEN DOU KO TOLONTI WALA NOU CHANGE CAYITE NEUNE NANOU LADIATE CAYITE BOUGUA KHAMÉ 6MOIS REK LA DÉ SI REWMI REK LA BAKH NGI LATHIE CAYITE GUI WARNANOU NEK SI REWMI LE MARS DE NOUYE LIGUEY SI DARA

SOUFÉKE SI 6 MOIS AMEGUA LIGUEY TOLE WITE PESCA WALA TAKHAOU NITE BOU BOBA SA CAYITE NEUNEUNE NEK CAYITOU LIGUEY

LATHIE NEUNANE KO AMALA SI BEURÉP YI SI DIGUEL YI YOR KARAGUÉ REWMI

  1. 1 BEREP BIGUA KHAMNE NIFI NIOW REK LA
  2. 2 NGI DI DIOGUÉ CAYITE YI 

NGI SOKHLA LIGUEY KATE NEUNA NOU DIOGUÉ LO TOLLOLE 500 € SI SÉN WALE KI DI LIGUEY MOME DI NA DIOGUÉ 160 € SIWALAME

BAKHOULE SI MADARGUAYI

KIKAYE OUTALE LIGUEY DAME NA KASO 5ANS YI WÉSSOU DAKH TEK SI KAO YI FI DEUKOULE WALA LOU DIEUME SI WALOU THIAGATOU MBOUKHOUME SI WALOU LIGUEY KI LAYE KHOUTAL LIGUEY WAROULE BINDE SI SOUF CONTRAT BI SOUFÉKE GUEMOULE KIMOU DIEULE

DÉ LIGUEY KATBI WAROULE AME AME DIAFEDIAFÉ SI BOP AYE GUENE REWMI WALA TETHIE KASO DÉ DANE BI WATHIE DIAYE YOUNOUYE TERRÉ NOUYE LORE NITE NEUBEU NITE AK THIAGATOU BOU LAKHOU DÉ LÉKHOULE

NITE BOUNOU YAKAR DIAFEDIAFÉ LA REWMI DEMOU AME AYE TEUTHIE BAFINOUYE DOKHALE TEURELE YI BEP GUALAKORE DIEUME SI KI OUTELE NITE LIGUEY AL KI DI LIGUEY TEGUINANOUKO

  1. 1 NOUWAKH LIGUEYKAYE YI NANELA DEMÉ SIWALOU LATHIE BI
  2. 2 NEK SI REWMI DE DIAROULE YONE

SI DIGUENTE BI NIT KI NEUNOUNOKO DAKH SI REWMI KHANA NOU FEBBAR BOU DIEUGUIDAYO

BATAKHAL YI NEUNO KO DIOTE YAW SA BOP KHANA GUA OUTE LEEROU SI NUMÉRO VERDE ARCI 800 90 5570

Your Website Title
Ero Straniero

Ero Straniero Facebook

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof