YOMBOU WAYE DEUKINEBI

BOUNOU DACORE SI DLREPARTI ITALIE SI YENE YEUGUE DIEUME SI WALA ART AK KHARAGNE LOU GUENE KHALISAME BOUTOLOU SI 5 MILLIONS EURO KHARE

LÉP BI TOLOKH 60% SILOUNOU DIEULEULE SI DIMBEUL WÉR SI LIGUEY COMMERCE USINE YI AK SI WALOU ARTISANAL TOLE YI TOURISME BEP LIGUEY BOU NITE DAFAL BOPAME

LÉP BOU TOLLOLE 30% DÉ DIEUME SI BERRABOU LIGUEY DÉ CONTRAT LOU NOU DIARIGNO DÉ DEUKOU WAYÉ WAYÉ BOKOUSI

LÉP MOUDIEUME SI WALOU LIGUEY BERRABOU NOPALOUKAYE YI DÉ SÉN BIR LEWNA

LEP BOU 60% BOU DIEUMELÉ SI NIÉTEL (3) SECTEUR DINÉ BOUNOU NAGOU LÉP BOU DÉ LOLE SI AYE WÉROU MARS MARS AVRIL MAI DIEUME SI WALOU ÉCONOMIE NOU DIEULE NOU WAGNI FATTURE WER AK WÉR TOLLOLE 50%SI WER BI SI TOP

LÉP BOU YAGUE DÉ NOU DIARIGNOKO SI AYE BESS YOU YAGUE NEUNE BOK ZK BEP BERABOU LÉP WALOU FINANCE NOU NEUNE DI LEP SASOU NEK

BATAKHAL SI NEUNANOU DIAP SI TOLOU WAYÉ NITE LATHIELE KHALATE NGI KHARAGNE SI WALBI SI DIEUME

YIBAR YI GUENE MA FOFOU NEUNOU DIOKH KENE KOU GUA KHANE NOGUI GUESTOU WALA LATHIE

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof