DIAPALE SI YEUGOU COMCOME BI

TEURELE REPARTI ITALIE KHAMENA BÉNA DÉTHIA SI WALOU LIGUEYE KAYE YOR SÉN YEUFOU BOP DÉ NOU SOUKINOUKOU SI FAYE BENE WALA (PARTITA IVA) DÉ SEN LIGUEY DIEKHOULE LE 31 MARS 2020 

DIAPALÉ MOGUI KHAR BENE BEUGUE BEUGUELE FACTURE WERROU AVRIL 2020 DÉMOU NDAW DIAP NIAR BA DIATE YOKOUTE DIEUME SI WERROU AVRIL 2019 DIAPALÉ MOGUI KHAR TAMITE BENE TAKHAW SI NGI GUA KHAMENÉ SEN LIGUEY TAMBALINA YONE SI 1 JANVIER 2019

YOKOUTE DIAPALE AK LOUMOU NEUTI DONE NDAW DIAP 1000 € MOUBAKH

  1. 1) 20% KHADIALE WÉROU AVRIL 2020 AK AVRIL 2019 BOUNOU KHOLE SI YENE SI DIAR YEKNA BA 400 000 €

  2. 2) 15% KHADIALE WÉROU AVRIL 2020 DIAP AVRIL 2019 BOUNOU KHOLE SI YENE SI DIAR YEKNA BA 400 000 €

  3. 3 10% KHADIALE WÉROU AVRIL 2020 AK AVRIL 2019 BOUNOU KHOLE SI YENE SI DIAR YEKNA BA 1 million € WATHIE BA 5 MILLION €

AME SI DIAPALÉ SI KHALIS BI KOU MOUSOKHAL NEUNGUA DEM FI NOUYR WAKH (AGENZIA ENTRATA )GUA YOUBAWALÉ LINOUYE LATHIE SI LOUMOU GUENE GUAWÉ  

NOGUI LENE DI KHALATE GUENE DEM SI YOR WALOU TOPATO DÉ NOU NÉK SI JUMA MAP 

YIBAR YI GUENE MA FOFOU NEUNOU DIOKH KENE KOU GUA KHANE NOGUI GUESTOU WALA LATHIE

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof