LIGUEYE AGILE

FI BA FEBBAR BI COVID-19 DI DIÉKH YI DI LIGUEY SÉN BOP DÉ NOUAME BENE DOME BOU AME ATE DÉ TOLOGOULE SI 14ANS NEUNANOU LATHIE SI SI LIGUEY AGILE WAYÉ MOU NEGOULE AK LIGUEY BIGUA KHAMÉ NOBOK KENE SI SA WADIOUR NEUNOULE DIOTE SI DIMBEULE SOUFÉKE LIGUEY BI TAKHAW WALA MOU BAYI NEUNO AME BENENE LIGUEY SI SA WADIOUR BOU AMOULE LIGUEY LIGUEY AGILE NEUNA AME DIOUNTOUKAYE INFORMATIQUE WALA YI KILAYE LIGUEY LO BOPOUR MOME MINILA APP BENE KHALÉ BOUNIAW SI REWMI TOUBAB AMGUA TOPOTO BOUBAKH ANBALH BEUGUEL GUA GUA NÉK FO WOR NOUDIOKH SA THIEURE SETAL YIBAR WALO DIMBEUL SI DEUK BI GUA NÉK GUESSTOU APPLICATION GUEMENE KHAME

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof