YOKSI DIEUME SIWALOU TOUKI VACANCE

TOPAL DL RAPARTI ITALIA LOU DIEUME SI WALOU DIABOTE AK BENE REDDITO ISEE BOUWESOULE 40 000 € BOUNOU KHAM LÉP SI ATOUME 2020 DA FAY SI WAGNI GUAYE AME YI DIEUME SI WALOU TOUKI BAYE AK AGNE AK NÉKI

LEP BENE NANAKO NEUNA DIEUFADIKO SI DIABOTE BOU NEK BOUTOLOK 500 € Si DIABOTE BOU NEK LEP BINOUDIEULE DÎNATOLOK AK WAGNI 300 € SI DIABOTE BOUNORAGNÉ DE NIAR NITE KÉSSE 150 € SOUFÉKE BENE NITE KÉSSE


1) NDOUGOU SI FÉKE REK NANOUKOUYE DIARIGNO SI BENE TOUKI WALA BENE TOLE WALA BENE AGNE AK NÉKI

2) SI WALOU DIARIGNO BI NANOUKO FIRDERLE AK CAYITE BOU MACHINE DI DIEULE WALA WALA FIKO DIARIGNO BOU ANDALE SA MADARGUA SI LEP

3) FAYE BI WANA ANDALE NOU FAYE KO DE DOU DIMBALI KÉN WALA KOUYE DOKH SI DIGUENTÉ BI TOPATO BIRMI WALA YOBOUKO SI BÉRRABOU YI TOPOTO TOUKI

LÉP NOUGUI DIOUR 80% SIWALOU WAGNI SOUFÉKE AK 20% SISA WALOU AME AME MOUYE LIGUA WELOLE

YIBAR YI GUENE MA FOFOU NEUNOU DIOKH KENE KOU GUA KHANE NOGUI GUESTOU WALA LATHIE

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof