YOKAL NGI DIAFADIKO VÉLO

SOUFÉKE NDAWGUA DÉ DEUK SI GOKH BI BIGUAKHANÉ SAKHAR RAJOUTE DIAR Si SA GOKH AK SA KOGNE MOUTOLOK 50 000 NITE YOUFEU DEUK NEUNEGUA AME 60% SI SI NDOUGOU WAYÉ DOU ROMBA 500 FI LE 4 MAI 2020(BEUSS BOUMOUYE TAMBALI d P C M LE 36 AVRIL 2020) MOU DIÉKH 31 DÉCEMBRE 2020

  • DIOTE SINAK DAGUA WARA AME VÉLO DIGUA KHAMÉ MOME GUAYE DIAFADIKO DÉMOU NEK SI WALOU COURANT LOUMELNI SEGWAY HOVERBOARD MONOPATTINI MONOWHEEL GUAKOYE DIARIGNO YAW WALOU BOK AK NITEYI


YOK YEUGOU BEN YONE NANEKOYE LATHIE SI YONE BOKOSOKHLO

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof