TOK SIKEUR  AK NOPALIKOU

COVID-19 YOUBOUNA NIEUP SIKEURYI DÉYOK NOPALIKOBI Cassa integrazione

DOLINANOU DIOUROME 5 SEMAINES SI NOPALIKOBI SIKEUR YI NDAKH COVID-19  LE 23 FÉVRIER AK  31 AOÛT 2020 YENENE 9  NOUGUI KHALATE NEUNA DOLEKOU  DAKH NOU BAGNE FEBBAR LAW  BENENE 4 SEMAINES NEUNANOUKO YOK BA 1 SEPTEMBRE 31 AOÛT NGI DI LIGUEY SIWALOU GANYI  YEUGOU YOU DAW YI   BOLO WAKHTANE CINÉMA BERRABOU FOUHOUKAYE KHALEYI  WANÉ SAY KHETOU FO  NEUNANOU TAMBALI LE 1 SEPTEMBRE

YOK NANOU SAK  NEK SI KEUR NOPALIKOU COVID-19 DI KHAR WADIOUR AK KHALÉ AME 12ANS  30 BEUSS  5 MARS BA DIAP 31 JUILLET 2020 NOU RESPECTE 15 BEUS YOU WESSOU NGI LIGUEY DAKH NITE DINANOULENE FAYE 50% SOUNOU NIEUWE SI NOPALIKOUBI DÉ LATHIOUNOU BONUS TÉYE KHALÉ YEN WADIOUR NOGUI LIGUEY NOUNEK NGI DIEULE NIMBAL  REDDITO

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof