S.O.S WAREF NUMÉRO VERDE NDIMBAL

800 999 977

L ARCI MIGUI WOUYOU SI NUMÉRO NDIMBAL

S.O.S WAREF NDIMBAL DINA WOUYOU LUNDI BA VENDREDI WAKHTOU 9H BA 13H SI SOUBA  14H 30 BA 18H 30 SI GONE NUMÉRO S.O.S DOFAYE DARA NGI DI LATHIE AY LEERAL SI DIEULE SI WALOU LIGUEY TOLYI AKNOU NEK SI YONE WALA NOU NEK SI BIROU NITE

L'ARCI SI GOKH DINA ANDAKH YENE BA NIENIAYI NOU NEK SI YONE NIGUAKHAME NE DOUNOUWA REWMI DÉ NOUYE KHAR  S.O.S WAREF AMENA DIOUMETOUKAYE BOUTOUDO JUMAMAP DEKHÉKH WAREEF AK NIAWTEF NOUNEUNE LENE BOLÉ

SÉN WOTÉ SI FIXE AK TÉLÉPHONE DOFAYE DARA DÉ LAK YEUP NIOGUI FOFOU SI ARCI YOMEBALALENE KO

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof