NOU TAMBALI DEM DIAGUI ECOLE SI ANAME YOUYOR

LEGUI DIOTE NANOU WADIAL SOUNOU SAC ATE BI BOLO AK LIBRE CAYÉYI DANOU WARA BOLO DAF DARA AK DOKHALINE YOU BESS

DIOUMTOUKAYE SI WALOU TAKHAWAL NIAGUABI DIAKNANOUKO NGI LIGUEY SIWALOU DIAGUELÉ BI AK NJABOOT GUI AK NDJIGUENE YOUYE DIAGUALE DIAGUAKATE KHAMÉ DANE LÉNI ANDI DENOU WARA TAMBALI NOU DIOKH THIER DOKHALINE YOU BESS YI

(Fonte: Ministero della Salute)

SAYTOU SA TEMPÉRATURE YARAM
DÉF LEN KO BEUSS BOU NEK BALAGUENE DI GUÉNE SO FEKE AMGUA LO WÉSSOU 37 ,5% SI TANGUA YOU YARAM WALA LINOUYE NGIOTE SI FÉBBAR BI COVID-19 TOGUALE SA KEUR DÉ WO KI SAYTOU SA YARAM DOCTEUR

DIFARALE DI RAKHASS SAY LOXO
DIAFANEKOU AKRAKHASSOU KAYE YOUNOU BAYI SI FI GUAY DIAGUÉ

TOPAL TÉKTAL YI
DOUGOU BI AK GUÉNE BI OUTÉNA TOPE NI KO SA ECOLE TEURELE

DIEULE DAFE SISASI APP IMMUNI
SOUFÉKE AMEGUA FOUK AK NIETE ATTE DÉF KO SA APP BOU GUAW APP MOGUI DIARIGNE LOU KHEW SI COVID-19 GUA AME SI AY LEERAL

FARLOULE SI MAYÉ DISTANCE
NOYTOUL BÉP TAKHAWAYOU BOLO DÉGUA TAKHAWE BEN METRE SI NITE YI GUAY TAKHAWALE

TAKKAL SA MASK
SOLALE SA MASK SAYOYE GUÉNE WALA FOU BARI NITE FOUKÉKÉ SI MAYGUA DISTANCE BEN METRE FI GUA TAKHAW AK NITE SI BANCO MEUNE GUA TÉKKI SA MASK WAYÉ KOU AME DIOUROME AK KENE WAKHOULENE

LATHIETEL SI BIIR
KHALATE KEN REK MOYE ANDAKH KIYE DIAGUA SI DI GOOR WALA NDJIGUENE DAKH GUA BEP LERAL SI ECOLE GUESSTOU SI SEN DIOUMTOUKAYE SITO

NA NOU ARE SOUNOU BOP BAPARE ARE GNISI DESSE

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof