DIAFADIKO MASK LONOU WARLA

CHARTE BOU BEUSS TAMBALI LE 7 OCTOBRE BI WÉSSSOU WANOU TAKKA MASK YI DAKH NOU ARE SOUNOU BOP SI WALOU NOYI

  • FÉP FOU TEDIOU BAMOU DÉS DEUKOUWAYI
  • FEP FOU YONE BOU HIBEKOU 

TAKKA MASK NÉKOULE LOUNOU DIKLÉ SI FANNAYI

  • KHALÉ BOU MATE LEGOULE DIOUROME ATE 6ANS
  • NITE BOU WÉRRGOU YARAM MAYOULE WALA KOU AME DIAFEDIAFÉ NOYI SOUFÉKE DAFAYE DIARIGNO MASK
  • FEP NOUYE TANGUELE YARAM

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof