DIEULE YOU AME SOLO SI WALATÉBI SI FEBBAR BI SI GOKKH BI DIAPAKO FOUK FANE AK NIAK 13 NOVEMBRE 2020

DIAFADIKO MASK LONOU WARLA

TAKKA MASK YI DAKH NOU ARE SOUNOU BOP SI WALOU NOYI

  • FÉP FOU TEDIOU BAMOU DÉS DEUKOUWAYI
  • FEP FOU YONE BOU HIBEKOU

TAKKA MASK NÉKOULE LOUNOU DIKLÉ SI FANNAYI

  • KHALÉ BOU MATE LEGOULE DIOUROME ATE 6ANS
  • NITE BOU WÉRRGOU YARAM MAYOULE WALA KOU AME DIAFEDIAFÉ NOYI SOUFÉKE DAFAYE DIARIGNO MASK
  • FEP NOUYE TANGUELE YARAM
  • NANOU SORRENTÉ SI DISTANCE 1METRE DANOUKOYE DIEUFÉ

✓ MEUNANOU DIEUFADIKO MASK YI YOUGUAKHAME NI DANE KOY FOUTE AK YOUNOU NIAW BAPARÉ AK BEP KHÉTOU DIEUFEUDOUKA BOKHANANI DINA ARÉ SI FEBBAR BI

TANGUAL YARAM AK LEUPP LOU DIEUME SI YARAM

✓ BAKHNA GUAYE DOKH WAYÉ NAGUA DIEULE MA TOU WAYE SORRENTÉ 1MÈTRE AK NITE YI

✓ BAKHNA GUAYE NÉK SI WALOU TAGUATE YARAM YAW KENE DÉGUA SORRENTÉ 2METRES AK NITEYI

✓ BAKHNA TAGUAL YARAM YAW KEN YOUNEUNETE NIAK DIEUME SI PALESTRA PISCINE SI KOGNE YI (YOUNOUYE FAYE AK YOUNE DOULE FAYE) DANOU RESPECTÉ DISTANCE YI AK BOLOUBI SOUNOU BIIR

✘ TANGUAL YARAM YAW KÉSSÉ NAGOUNANEKO WAYE TERRENANOU BEP TANGUAL YARAM BOUYE BOLE AY NITE NOUSIYEU AME DARA

✓ NAGOUNANE BEP TANGUAL YARAM BOU DIEUME DIEUME SI BENE NITE DAMOU SOKHOL SI WALOU REWMI AME SI RAYÉ DE WALOU NGI SAYTOU TANGUAL YARAM REWMI NAGOUKO ( C O N)

✓ LI DIEUME SI WALOU STADE MAYÉ BA 15% SI NITE YI SETANSI MOUTOLOK 1000 SETANKATES BATAKHNA 200 DANE LENE TEUTHIENOU MAYENTE DISTANCE 1METRE NOU MOUYTOU SIBIROU SI BIR FANOU NÉK

BOLO CINÉMA BERRABOU FÉTHIE AK FINOUYE FOWÉ

✓ CINÉMA BERRABOU THÉ TRE AK AY WAY NAGOUNANE KO SI KAO NOU SORRENTÉ SEN BIR AME DISTANCE 1METRE NOUMAY 1000 SETANKO 200 SETANKATE YOUNOU TEUTHIE

✘ TERENANOU BEREBOU FETHIE YI GUA KHAMÉ DAFA HIBEKOU AK TEUDIOU

✘ TERENANOU FI BOLO DI DADIALO DI LEKK AK WAKHTANE NOUNAGOU BOLO/YI SI REWMI AK FEK SI ADOUNA BI (NATIONAL AK INTERNATIONAL)

✓ BAKHNA BOLO YI YOU DIEUME SIWALOU WAKHTANE LEP NOU TOP DIGUELE AK NOUYTOU

✓ HIBINANOU BERRABOU YOUNOUYE OUTE KOPARE AK DI TÉK KHALIS WAKHTOU 8H 00 BA DIEUME 21H 00

LI DIEUME SI WALOU DINÉ AK BOLO WAKHTANE AK BOLONITE DIEUME SI WALOU DOUMOU ADAMA

✓ LOU DIEUME SI WALOU DINÉ AK BOLO WAKHTANE YI MAY NANOU LA BA 30 NITE TEWEKO DANOU RESPECTÉ FINOU LEN YAME LO

✓ TEUTHIE NANOU BEP WAKHANE NITE YOU BOK KHALATE DIEUME SI SEN WALE AK WAKHTANE YOU SORÉNTE YOU NIT BOK

BOLO YOU AY NITEDI DADIÉ DAMOU HIBEKOU WALA TEUDIOU

✘ TERRENANOUKO BOLO NITE HIBEKOU AK TEUDIOU DE NÉKOULE SI KEUR GOUGUAKHAME 6 NITE REK LAYE DIEULE YOU FA DEUKOULE

RESTAURANT FOUNOUYE LEKKE GLACE AK BONBON AK BAR DIFA TOK
  • TOK LEKK SI TABLE BAKHNA WAKHTOU 5H 00 BA 24H 00 WAYÉ 6 NITE REK NANOU MAYÉ
  • GUA TAKHAW DI LEKK BAKHNA 5H 00 BA 18H 00
  • NOUANDI LEKK BASA BIR KEUR BAKHNA WAYÉ AK FARLOU
BERRABOU DIAGUALE ÉCOLE

✓ BERRABOU DIAGUALE YI YOU KAWE YI DINANOU HIBI SI BIR WAKHTOU 9H 00

✘ TERENANOU SI BIIR BERRABOU DIAGUALE TOUKI YI

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof