Nuovo DPCM: le restrizioni per zone

NOU TOP NIÉTE DEREP SI REWMI DIAKHASO LO AME SOLO TOPE NDIGUEL DPCM TAMBALI LE 3 NOVEMBRE NOU DOKHALKO 6 NOVEMBRE DIEUME 3 DÉCEMBRE

BEREP YOU JAUNE
Lazio, Molise, Provincia autonoma di Trento, Sardegna, Veneto.

BÉRAP ORANGE
Basilicata, Emilia Romagna, Friuli Venezia Giulia, Liguria, Marche, Puglia, Sicilia, Umbria.

FI KHALÉ DI FOWÉ DI HIBEKOU
Abruzzo, Calabria, Campania, Lombardia, Piemonte, Provincia autonoma di Bolzano, Toscana, Valle d’Aosta.

BEREP YOU JAUNE

  • TERENANOU NOUDOKH WAKHOU 22H00 DIEUME 5H SI FADIAR KHANA GUANÉK SI WALOU LIGUEY AK WALOU WEERGOU YARAM BOUMOUDONE TERENANOU BÉP GUÉNE BOU DIEUMOULE WALOU LIGUEY WEERGOU YARAM SI LOU MEUTE NIAK
  • TEUTHIE BERRABOU DIAYOUKAYE BEUSSOU NOPALOU ( SAMEDI AK DIMANCHE) AK LOU DIEUME SI FARMACIE KHÉTOU FARMACIE NDOUKOYE DIAYOUKAYE SIGARETTE DIAYOUKAYE LIVRE JOURNAL LEUPP SIBIR
  • TEUTHIE BEREBOU BAGASE YOU YAGUE AK LEUPP LOU SI DIEUME
  • DIAGUE SI KEUR SI WALOU BEREBOU DARA YOU KAWÉYI DANOGUAYI DEFKO DIARIGNO BERRABOU LIGUEY SI DARAYI BERRABOU NDAW YI AK KHALÉ YI THEUTE DARA LOUKAWÉYI BOLESI BEREBOU DIOUMTOKAYE
  • WAGNI GUENEWALA 50% SI WALOU DEM AK DIKK DIEUME DARAYI
  • TEUTHIE BERRABOU TEK KHALIS AK SIGARETTE NEK SI BARYI
  • TEUTHIE BERRABOU RESTAURANT BAR BOU 18H DIOTÉ DAFAR LEKK WAKTOU 22H YOBOU LEKK BOKOSI
  • TEUTHIE FI KHALE YI DI FÉY AK OUTE DOLÉ RETAANE CINÉMA. TEUTHIE BERRABOU DADIALOU KHALÉ YI DILENE TAGUATE

BÉRAP ORANGE

  • TERENANOU NOUDOKH WAKHOU 22H00 DIEUME 5H SI FADIAR KHANA GUANÉK SI WALOU LIGUEY AK WALOU WEERGOU YARAM BOUMOUDONE TERENANOU BÉP GUÉNE BOU DIEUMOULE WALOU LIGUEY WEERGOU YARAM SI LOU MEUTE NIAK
  • TERENANOU BEP GUÉNE BOU AMOULE YITÉ DIEUME FIGUA KOGNE BIGUE DEUK
    .
  • TEUTHIE NANOU BAR AK RESTAURANT BEUSS BOU NEK LIGUEY BA 22H WAYE YOBOU LEKK SI KEUR YI MEUNANEK
  • TEUTHIE BEREBOU DIAYOUKAYOU MAKGUI BEUSSOU NOPALOUKOU AK LOU DIEUME SI FARMACIE AK FÉP DIAYOUKAYOU LEKK SIGARETTE AK JOURNAL SI BIR
  • TEUTHIE BEREBOU BAGASE YOU YAGUE AK LEUPP LOU SI DIEUME
  • TEUTHIE BEREBOU BAGASE YOU YAGUE AK LEUPP LOU SI DIEUME
    DIAGUE SI KEUR SI WALOU BEREBOU DARA YOU KAWÉYI DANOGUAYI DEFKO DIARIGNO BERRABOU LIGUEY SI DARAYI BERRABOU NDAW YI AK KHALÉ YI THEUTE DARA LOUKAWÉYI BOLESI BEREBOU DIOUMTOKAYE
  • WAGNI GUENEWALA 50% SI WALOU DEM AK DIKK DIEUME DARAYI
  • TEUTHIE BERRABOU TEK KHALIS AK SIGARETTE NEK SI BARYI
  • TEUTHIE BERRABOU RESTAURANT BAR BOU 18H DIOTÉ DAFAR LEKK WAKTOU 22H YOBOU LEKK BOKOSI
    TEUTHIE FI KHALE YI DI FÉY AK OUTE DOLÉ RETAANE CINÉMA

FI KHALÉ DI FOWÉ DI HIBEKOU

  • BEREP YOU KHOKH ROUGE SA BIR GOKH SI WAKHTOU BOULA NÉK SI WALOU LIGUEY BOU AME SOLO AK WÉRRGOU YARAM TERENANOU GUÉNE DEUK DAME SI BENENE GOKH
  • TEUTHIE NANOU BAR AK RESTAURANT BEUSS BOU NEK LIGUEY BA 22H WAYE YOBOU LEKK SI KEUR YI MEUNANEK
  • TEUTHIE BAR RISTORANT BEUSS BOU NÉK LIGUEY MEUNNA NÉK BA WAKHTOU 22HEURES WAYÉ YOBOU LEKK BOKOUSI
  • TEUTHIE NANOU BEUREU BOU DIAYE wAYE BERRABOU DIEUME SI WALOU LEKK DINA HIBI
  • TEUTHIE BERRABOU DIAYE BOKOUSI BERRABOU DIAYE LEKK YOUNONU SOKLA
  • HIBI FIDI DIAYE JOURNAL SIGARETTE AK FARMACIE FOTOUKAYE DAFARÉ BOP AK WATOU
    TEUTHIE BERRABOU DAFAR YARAM. WAYE HIBI ECOLE KHALÉ YI ECOLE DAW YI AK NGI DJITOU TEUTHIE DIAGUALE BOUKAWÉ BI AK YOUNOU BAYI MOUHIBI
  • TEUTHIE BEP DIOGANTE YOU AME SOLO WALANAGOU SI DEUK BI CON CIP TEUTHIE BEREBOU DIONGANTE HIBI BÉP DIONGANTE MOTEUR FIGUA DEUK BEN BEN WAKA LOU NIEUP BOK
  • TEUTHIE BERRABOU BAGASE YOU YAGUE AK THEATRE CINÉMA TAGYALE YARAM BEREBOU TEK KHALIS DIONGANTE TEK BAR FIDI DUAYE SIGARETTE
    LI DIYOU NITE YI MEUNNA DUEULE BA 60% WAYE BAGNE SIBOLO NGI YOBOU NITE NOUDIANGUI

DIOUROME 6 BOWORE KHAME SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE

FAQ

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ? WAKHTOU 5H BA 22H DIAROULE FIRDÉ WAYÉ 22H BA 5 H FOK GUA AME FIRDÉ BOUYE WANÉ DAGUA WARA GUÉNE MEINENA DÉME DIMBALI XARITE WALA MOK BOUSOKHLA DIAPALÉ ? WAW SOUFÉKE LOUMEUTE NIAK WAYÉ DIGUENTÉ 22H BA 5H AME FIRDEL DINANKO SOLO SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ? WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ? WA KHANA LOUDIEUME 5H BA 22H SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ? WAW KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ? WAW

FAQ

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ? WAKHTOU 5H BA 22H DIAROULE FIRDELE SA GUÉNE SIBIR NGOKH GUÉNE DIEUME BENENE GOKH WAKHTOU 22H BA 5H SIBIR FIGUA DEUK DAGUA WARA GUANAYO FIRDÉLE BOULAYE MAYE GUA GUÉNE DANOUKAYE HOUTÉ NGI YOR KARAGUÉ REWMI AK TALLI BI MEUNA DEM DIMBALI MOK WA XARITE BOUAME SOKHLA ? SOUFÉKE LOUMEUTE NIAK DÉ KHAMO BANE WAKHTOU BIGUAYE NGISI SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ? WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ? WA WAYÉ 5H BA 22H SOUWESSO 22H BA 5H NAK TERENANOU KO DAY DIEUME SI WET BOU KHOQUE BI ROUGE SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ? WALE BOBOUNAK GUENE FIRDÉLE BOUNEKE DANE LA SOKLA SI SA LIGUEY KATOU DAMEUNON LIGUEYE SA DEUK KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ? WA MEUNEGUA NGIBISI BENE YONE TÉKLÉ DI GUÉNE DIAKLENANOUKO SOKLA LIGUEYOUKAYE DIAGUA WEERGOU YARAM WALA GUÉNE YOU SÉW SABIR GOKH ( DEM POSTE NDOUGUI BOUNEKE BEURIHOULE FIGUA DEUK

FAQ

SOUFÉKE DAGUA BEUGUE GUÉNE DEM AK LOUMOU MEUNE DONE WARGUA WANÉ FIRDÉLE ?

WARA GUANAYO FIRDÉLE BOULAYE MAYE GUA GUÉNE DANOUKAYE HOUTÉ NGI YOR KARAGUÉ REWMI AK TALLI BI

MEUNA DEM DIMBALI MOK WA XARITE BOUAME SOKHLA ?
WA SOUFÉKE LOU MEUTE NIAKLA

SOUFÉKE DAMA TAGO WALA TASS MEUNENA SÉTI SAMAY DÔME ?
WAW MEUNE GUA FÉKI SAY DOME WADIOUR NAGUA TÉLA GUÉNE YOBOULÉ SI BÉNENE GOKH AWÉNOUKO

MEUNENANOU DEM SI BÉRÉBOU DIAMOU YALLAH YI ?
MEUNA DEM BÉREBOU DIAMOU YALLAH BI DIÉGUE SA KEUR DADOGUEME DIEUME SI KHAWA DIÉGUE FIGUA DEUK MOYETOU BOLO DE SORÉNTE DISTANCE BENE METRE MEUNEGUA DEM BERÉP SOUFÉKE DAFA AME LIGUEY BOUNE FAYE DÉF DIAPALÉ SI WALOU DINÉ DJI

SOUMA DEUKE FENE DI LIGUEYE FENENE MEUNA DEM DI NIEUW ?
WALE BOBOUNAK GUENE FIRDÉLE BOUNEKE DANE LA SOKLA SI SA LIGUEY KATOU DAMEUNON LIGUEYE SA DEUK

KOUNÉK FIGUA DEUK NAK MEUNE GUA NGIBISI ?
WA MEUNEGUA NGIBISI BENE YONE TÉKLÉ DI GUÉNE DIAKLENANOUKO SOKLA LIGUEYOUKAYE DIAGUA WEERGOU YARAM WALA GUÉNE YOU SÉW SABIR GOKH ( DEM POSTE NDOUGUI BOUNEKE BEURIHOULE FIGUA DEUK

Fonte: http://www.governo.it/it/articolo/domande-frequenti-sulle-misure-adottate-dal-governo/15638

You may also like...

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof