WAYE LAKHOUYI

FEBBAR BI COVID-19 FI SI ITALIE ANNI NA AYE REUK REUK SI WALO CAYITE POUR WAYE LAKHOUYI SI WALE BI TAKHNA NOU YOKASI DIEUFÉ AK BATAKHAL YOU BESS YI

NOUTEKO SI BEUSS TEUREULE YONE YI

DIEUNANOU NDOGALE LE 15 JUILLET BA LE 15 AOÛT 2020 SI LA WARA DIÉKH LINE DONE WANÉ YOU DIEUMONE LI TEGOU SI YONE AK NOUMOUYE DOKHÉ
BÉP LATHIE BOSOKHLA SI WALOU TEURELOU YONE SI DOKHALINE BI questo articolo.

JumaMap – COVID-19 in Italy · [PULAR] Proroga Regolarizzazione
JumaMap – COVID-19 in Italy · [SONINKE] Proroga regolarizzazione

JumaMap – COVID-19 in Italy · [BAMBARA] Proroga Regolarizzazione

TEUREULE BOU DIEUME SI DIMBEUL BOU NEUNE TEKHAR


NOUTEKO SI BEUSS  TEUREULE YONE YI   
DIEUNANOU NDOGALE LE 15 JUILLET  BA LE 15 AOÛT 2020 SI LA WARA DIÉKH LINE DONE WANÉ YOU DIEUMONE LI TEGOU SI YONE AK NOUMOUYE DOKHÉ

LOUKO DIAP 1JUIN 2020 BA DIEUME 15 JUILLET 2020 NEUNA GUÉNE DEM WANÉ DIOUMTOUKAYE YITAKH GUANEUNA AME CAYITE REWMI SI WALOU LIGUEYI

  • BAY WITE PESCA AK LIGUEY YOU MÉGOLE
  • DIMBEULI NITE
  • LIGUEY KEUR TAKHAOU DIABOTE

DAKH NEUNANOU WANÉ LATHIE BI ?

  1. KI GUAYE LIGUEYALE NEUNA DEM LATHIELA DÉ NAGOU NEKA AMENA KENE NEKANA SI GOKH BI WALA MOUWAKH BENE LIGUEY BOU DIAR YONE LEP BOU DIARÉ YONE NITE YI WARNANOU BAKHO NOURAGNE LENE SI SÉN KANAME AK BINEDA WALA NOU NEKONE ITALIE AVANT LE 8 MARS DE DEMOU NOU FENENE TOK SI REWMI
  2. NITE YOU SENE CAYITE DIEKH LE 31 OCTOBRE 2019 DÉ KEN DOU KO TOLONTI WALA NOU CHANGE CAYITE NEUNE NANOU LADIATE CAYITE BOUGUA KHAMÉ 6MOIS REK LA DÉ SI REWMI REK LA BAKH NGI LATHIE CAYITE GUI WARNANOU NEK SI REWMI LE MARS DE NOUYE LIGUEY SI DARA

SOUFÉKE SI 6 MOIS AMEGUA LIGUEY TOLE WITE PESCA WALA TAKHAOU NITE BOU BOBA SA CAYITE NEUNEUNE NEK CAYITOU LIGUEY

LATHIE NEUNANE KO AMALA SI BEURÉP YI SI DIGUEL YI YOR KARAGUÉ REWMI

  1. 1 BEREP BIGUA KHAMNE NIFI NIOW REK LA
  2. 2 NGI DI DIOGUÉ CAYITE YI 

NGI SOKHLA LIGUEY KATE NEUNA NOU DIOGUÉ LO TOLLOLE 500 € SI SÉN WALE KI DI LIGUEY MOME DI NA DIOGUÉ 160 € SIWALAME

BAKHOULE SI MADARGUAYI

KIKAYE OUTALE LIGUEY DAME NA KASO 5ANS YI WÉSSOU DAKH TEK SI KAO YI FI DEUKOULE WALA LOU DIEUME SI WALOU THIAGATOU MBOUKHOUME SI WALOU LIGUEY KI LAYE KHOUTAL LIGUEY WAROULE BINDE SI SOUF CONTRAT BI SOUFÉKE GUEMOULE KIMOU DIEULE

DÉ LIGUEY KATBI WAROULE AME AME DIAFEDIAFÉ SI BOP AYE GUENE REWMI WALA TETHIE KASO DÉ DANE BI WATHIE DIAYE YOUNOUYE TERRÉ NOUYE LORE NITE NEUBEU NITE AK THIAGATOU BOU LAKHOU DÉ LÉKHOULE

NITE BOUNOU YAKAR DIAFEDIAFÉ LA REWMI DEMOU AME AYE TEUTHIE BAFINOUYE DOKHALE TEURELE YI BEP GUALAKORE DIEUME SI KI OUTELE NITE LIGUEY AL KI DI LIGUEY TEGUINANOUKO

  1. 1 NOUWAKH LIGUEYKAYE YI NANELA DEMÉ SIWALOU LATHIE BI
  2. 2 NEK SI REWMI DE DIAROULE YONE

SI DIGUENTE BI NIT KI NEUNOUNOKO DAKH SI REWMI KHANA NOU FEBBAR BOU DIEUGUIDAYO

BATAKHAL YI NEUNO KO DIOTE YAW SA BOP KHANA GUA OUTE LEEROU SI NUMÉRO VERDE ARCI 800 90 5570



Your Website Title




Ero Straniero

Ero Straniero Facebook



JumaMap – COVID-19 in Italy · [BAMBARA] Regolarizzazione ed emersione rapporti di lavoro

JumaMap – COVID-19 in Italy · [PIDGIN ENGLISH] Regolarizzazione ed emersione rapporti di lavoro

JumaMap – COVID-19 in Italy · [SONINKE] Regolarizzazione ed emersione rapporti di lavoro

JumaMap – COVID-19 in Italy · [PULAR] Regolarizzazione ed emersione rapporti di lavoro

BATAKHAL BOUWARAGUA COVID-19 NOUKHAME  LOUNOU WARA DIMBEULÉ  ADOUNA

NI DIAGOROBI FEBBAR  BI COVID-19 DI LAWÉ SI ITALIE AK ADOUNA BI DANE SÉWARA DIOK GUAW

BATAKHNA  GEUNE HAR SÉN WEERGOU YARAM KÉN BANIA GUÉNE  KEUREUM KHANA  NGAYE DÉF LOUMENE NIAK   ( LIGUEY WALOU WEERGOU YARAM NIBI SA GOK)

BO AMOULE  AYE FIRDÉLE AYE DANE KHATHIE NASI

NOYTOU NOUWALALA DIAGOROBI AME NA AYE MATOUWAY  YOUNOU DIEULE BADIMBALI NIEP

1 DAGUA BEUGUE DIMBEULOU  ASKAN BI?

TÉTHIE NANOU FÉP FI GUA KHAMÉ WAY LAKHOUYI NEUNE NANIAW OUTSI WALOU WAYÉ NEUNE GUA DEM SI BEURÉP BA DIOYTOU SA NAKHAL  AMANA  SA WAREF DINANE SI BAYI KHEL

2 KHARALE WOTÉ WA BOLO BI SAYTOU WAKHANE  AK BEUSS BIGUA WARA TÉW ?

NOYTOU DIAGORO BI LAW  DIAMONO BI TETHIE NANOU BEP WAKHANE  BA DIEUMI DIAMONO BEUSS YI DANE KO KHAMALÉ

FATELIKOULE BÉP NITE BOU WARA WAKHANE  KHABAR BI DINALA FEK SI KEUR YI DIMBEULE SOFA NÉKOULE FAGUA DEUK  BIDAL SA TOURE SI BOUTE BI

3 KHARAL BA LIGUAY LATHIE GUÉNE?

DIGUA DIOT BATAKHAL  LIGUAYE  LATHIE SOUGUÉNE

SI AYE BEUSS SO DIOT BATAKHAL NOU NAGOULELAKO KHARAL TOUTI  GUA DEM SI DARÉP BA DIEULI SA CAYITE (PERMESSO SOGGIORNO)

SO DIOT BATAKHAL DÉ CONTANO  GUA BEUGUE DÉMATE DI GUA KHAR TOUTI DAKH LEUPP TEUTHIE AMEGUA  TAN  WALA SA LAYTOU KAT(AVOCAT)GUA WOKA AK TÉLÉPHONE WALA SA ÉMAIL WALA KEUR DIMBEULI GUI GUA DEUK KIKADITE

4  SOLAGUA AYE LÉRALE DAGUA WARA YOBOU SÉY CAYITE SI NISAYTOU  DIMBEUL

DIAMONO BI LÉP TEUTHIE BAKHNA YONÉ BATAKHAL ÉMAIL  DIAFÉNA  KHOLALE SI BIR BA KHAME. WOTEL PEC WALA EMAIL BOLO/YI YOR WALOU DI  DACOR SI DIMBEULI

YEUGUE BEP CAYITE BAKHNA

BOUNOU TOPÉ CHARTE REWMI SI SOPI CAYITE FATHIE "CURA ITALIA "NOGUI YEUGUE BEP CAYITE BAKHNA BA SI WÉR 31 AOÛT 2020 31 AOÛT 2020.

Proroga documenti di riconoscimento

Salam BÉP CAYITE BOULENE DI RAGNÉ DÉ REWMI ITALIENS YI DIAKLÉLEKO MO KHAM MOU DIÉKH WALA MOU DIÉKH SI FANE YI WÉSSOU 18 MARS 2020 YOKATNANOUKO BA 31AOUT 2020 WAYÉ BÉP CAYITE BOUDIOU (ART 104 CURA ITALIA

CAYITE RAGNÉ KAYE YANE NANOU?

CARTE D'IDENTITÉ

CARTE D'IDENTITÉ PASSEPORT PERMIS DE CONDUIRE PERMIS SI WALOU GUETHIE RETRAITÉ FAMILIAL PERMIS POUR NGI DI DAWALA DI DIEUME SI KEUR WALA PORTE GUANIAYE CAYITE BI RAGNÉ DAFAWARAME SA PHOTO AK TINBRE AK SIGNATURE GNIDI ART DEUKEUBI

Questure uffici immigrazione – Permessi di soggiorno, rinviate convocazioni questura

AVVISO –  PERMESSI DI SOGGIORNO, RINVIATE CONVOCAZIONI QUESTURA
A seguito del Decreto legge n. 9 del 2 marzo, le convocazioni in Questura, ricevute al momento della presentazione delle domande relative ai documenti di soggiorno, potrebbero essere rinviate e le eventuali nuove date saranno comunicate con sms. Prima di recarsi in questura, consigliamo di consultare il ‘Portale immigrazione’ – https://www.portaleimmigrazione.it/, autenticandosi con username e password ricevuti presso l’Ufficio Postale Sportello Amico di presentazione della richiesta, per verificare la data di convocazione.

AVVISO –  QUESTURE UFFICI IMMIGRAZIONE

INFO Sono temporaneamente chiusi al pubblico tutti gli sportelli degli Uffici Immigrazioni delle questure destinati al rinnovo e al rilascio dei permessi di soggiorno.
Sono aperti solo gli sportelli per la presentazione della domanda di protezione internazionale (richiesta asilo).

Fonte: Ministero dell’Interno

DOCUMENTI

VIDEO

PODCAST

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof