DIAYE DOLÉ BOUMOUDONE

SOUFÉKE YAGUI DOUNDOU WALA GUA KHAME NITE BOUNOUYE DIAYE DOLÉ WALA DIARIGNO? SI DIAFEDIAFÉ YI NOUNEKE SI WALOU GUÉNE AK TEDIOUBI NOUYE NOUYE DOUNDOU DIAYE DORÉ WALA DIARIGNO.WOTEL WALA BINDALE LAHIE WALLOU SI SOUTOURE AK WOLOUTÉ

WOTÉL DOFAYE DARA 1255 (WOTÉL AK BINDE MESSAGE WHATSAPP) MOGUI DOKH 24h SI DIOUROME (5)LAK (Italien français anglais Spagnol ak arabe) BÉPNITE DOUNOYE DIAYE DOLÉ

WOTE NUMÉRO VERDE 8005570 MOGUI DOKH 24H POUR NITEYI YOUNOUYE DIARIGNO

AMENA BENE App – YouPol

ANI DIAFEDIAFÉ BENA NITE SI DIALGUATI WAREEFOU DOUMOU ADAMA LA


SOUFÉKE GUISSGUA WALA DOUNGUA BENE BOUNOUYE BOUNOUYE DIARIGNO NEUNE KO DIMBALI

NEUNA WOTE 80029029
DOU FAYE DARA DÉ KENE DOUKOKHAME 24h

FI SI REWMI ITALIE AMENA BÉRRABE YOUGUAKHANÉ NOUYE SAYTOU SOUFÉKE DOUNAGUE WALA GUISGUA NITE YOUNOUYE DIARIGNO BERRABE YI DINANOULA DIAPALÉ SI DEUKOU WAYE BOU KENE DOKHAME BIMBALE SI WALOU WEERGOU YARAM AK SI WALOU YONE SANÉKINE FI SI ITALIE SOULA NÉKHÉ DINANOULA DOUGEULA SI BENE YONE BOUYE SAYTOU AK CHARTE YOUNE LAYE WAKH MEUGUA DIOKO AK NITEYI SI YIBAAR DAKH KHAME BOU BAKH WALA LATHIE DIMBAL BOU GUAW SI KEN DOUL KHAM
SI BIIR WÉTOU THIAMOYE

SOUFÉKE YAGUI DOUNDOU BENE SIYI NEUNEGUA

  • DIGUA DIOTE YIBAAR SI CHARTE YI WALA TAKHAOU SI SA WAREEF
  • DIOTE DIMBEUL WEERGOU YARAM AM
  • DIOTE DIMBEUL BOUWEUR SILILAYE HARE
  • TOKE SI REWMI ITALIE DI TOPOTO SA LATHIE DANKH NOU HARE LA WALA BENENE WALOU CAYITE
  • LATHIE DAKH NEUNE GUA NIBI SA RÉW SI WALOU DIMBEUL BOSAKOU WALA kOULAYE TAKHAKHOU

“Mi sono fidata di quella donna che mi ha promesso di farmi venire in
Italia per cambiare la mia vita. Adesso, dopo un viaggio terribile, mi
trovo qui, costretta a prostituirmi per pagare un debito”.
Jr 22
TOUKI BOUMETI BOUMADATHIE SAMA BAYE NENAMAWEUNE DAMA KHARA NIEW SI REWMI ITALIE BAKH DIMBALI SAMA WAKEUR LÉGUI MAGUI LIGUEYE 10H PARE BEUS BEUS BOU NÉK SI SEMAINE BI DÉDOUMANOPALIKO MAGUI DEUK FI MAYE LIGUEYE SAMA BORYI MOGUI YOKOU DAKH SAMA TOUKIBI AK NITE KI MAOUTEULE LIGUEY FI SI REWMI ITALIE
M.H.18
“Mi hanno convinto a partire dicendomi che qui avrei trovato una vita
migliore e adesso vivo per strada chiedendo soldi e dando una parte
di quello che guadagno a chi mi ha fatto arrivare”.
G.S.20

Presidenza del Consiglio dei Ministri / Ministero dell’Interno / Unhcr

DOCUMENTI

VIDEO

PODCAST

MAPPA

Wolof
Italiano English (UK) Français አማርኛ العربية বাংলা 简体中文 Español ਪੰਜਾਬੀ Русский Af Soomaali Shqip ትግርኛ اردو Wolof